بــــــشير (@_Bachiir) header
بــــــشير (@_Bachiir) profile picture

تحلى جمال الخلق والخلق أجمل# بشير هو البشرى يبشر بالحكمة.

Daaru Xudóos
Joined September 2013
Photo by بــــــشير (@_Bachiir)Photo by بــــــشير (@_Bachiir)Photo by بــــــشير (@_Bachiir)Photo by بــــــشير (@_Bachiir)Photo by بــــــشير (@_Bachiir)Photo by بــــــشير (@_Bachiir)Photo by بــــــشير (@_Bachiir)Photo by بــــــشير (@_Bachiir)Photo by بــــــشير (@_Bachiir)Photo by بــــــشير (@_Bachiir)
😭 Vous n’avez pas fait ça vs avez raté votre vie. Wola.
61
665
79
2,645
Bu njëkkoon jaamu Yàlla mooy def ay jëf yu rëy ; sunu jamono yii nag, jaamu Yàlla mi ngi ci moytu yu bon yi. Booy xool bàyyi lu bon moo gën a jafe sax def lu baax. Sang bi ﷺ nee na : «bis nit ñi dinañu àgg foo xam ne ku téeye diineem day mel ni ku ŋëb aw xal.» [Tirmiisii:2260]
1
52
1
172
3,616
بــــــشير retweeted
Les inédits sur le départ au bureau de Ndar.
10
51
3
153
{Te bu Bis-Pénc ba seeni doom walla seeni mbokk duñu leen fa jariñ, [Yàlla] dana fa teqale seen diggante} [S60L03] Moo tax Mustafaa AlKariim daa wax ne: « man de Sëriñ Tuubaa a ma jur waaye ag njub a ma doy. » Doy na ci misaal doomi Y. Yàlla ba Nuuh ak soxnaam sa.
1
21
70
1,357
Deel xeex ak sa bakkan nu raw ni ngay xeexe ak sa noon.
1
24
115
1,361
NB : Seuls les jeunes résidant dans les départements de Louga et Dagana sont concernés. Les formations sont executées par l'ONFP dans le cadre du Programme de Désenclavement des Zones Agricoles et Minières (PDZAM). 2/2
117
Ku lay xaar yal na xàddi, Mbàkke Bàlla. 🤲🏾
4
82
1
344
3,805
Junniy nawet Mbàkke Bàlla ! 🤲🏾
3
248
22
946
28,053
Ba leegi kàrt gi leeragul de entre Raa’iya Baay Mustafaa Jóob ak Raa’iya Sñ Siise. 🥲
20
11
18
143
20,344
C’est fou mais parait il looy gën a jege Yàlla di gën a sori nit ñi. 🥲
9
79
9
816
17,552
Waa nu ngeen di tagge koo xam ne Boroomam Bi ko bind Moo ko njëkk a taggal Boppam, ne ko: {Waat naa ne yaa làmboo mboolem jikko yu rafet yépp} ?
43
173
2,364
Sëriñ Tuubaa bokk na ci li mu rawe ñu bari mooy nekku fi di werante ci biddaa ak sunna, dafa ne faf lu war la, waaye ci ñan ? "Sawii taxaddumi" ci ña jiitu. Daal ciy woo ay taalibeem yépp. مـولده معظم مـبـارك مـحـترم تعظيمه ينحتم على ذوي التقدم #Gàmmu1448
19
93
1,257
Sama gaa ñi Al Masiihu Dajjaal, Al Masiihu Dajjaal, Al Masiihu Dajjaal. Amul jenn fitna ci kaw suuf ju gën a rëy Al Masiihu Dajjaal. Dina génn fi yéen nattu leen kon xamleen ko.
1
15
62
1,498
"والعـٰقبة للمتقين"
28
270
2,664
Jasbu Sñ Mbay Jóob Kuréel Cees ba nii gaa ñi jàngaguñ lu ko dàq te gën ko tege ci temps.
2
12
3
62
6,251
Ag taalube dëgg mooy bi ñu laajee Abuu Bakr: yaw ak Yónnent bi halayhi salaam ku mag ? Mu ne: Moo ma mag de, donte maa Ko njëkk a gane àddina.
6
29
1
167
6,198
*Al Abbaas la. Baayu tëxam.
3
429
لـه لدى الله سرّ لا يطـالعه بالكد والعلم رهبان وأحبار Yàlla jox na ko ci ay mbóot lu kenn manul daj, Ab làbbe manul sonn ba gis ko, ab fóore manul jàng ba xam ko. #Gàmmu1448
21
154
1,298
”Baadoola boo ko defalee lu baax du ko xam, Bu la defalee lu baax it du ko xam. | Sëriñ Basiiru Mbàkke Abdu Xaadar, Juillet 2026.
17
95
1,677
Il y a plus de 1440 ans te ba leegi am na ñuy raxas seen nopp, bu ñuy jàpp, au lieu ñu masaa ko rekk. 🥲
7
14
4
206
14,801
Li tax nit ak jinne wàcc ci kaw suuf mooy jaamu Yàlla (diine) yeneen yépp dañ ko teg ngir ñoŋal diine, ba dara féetewu ko kaw.
13
72
931