
Yal na ma Yàlla def ab jullit bu mat sëkk, ab murid buy jël ay tegtal ci Alxuraan ak sunna ak njàngalem Sëriñ Tuubaa CEO: @jaalibatu_apple
KeurMassar, Dakar , Senegal
Joined November 2020
- Tweets37.4K
- Following7.4K
- Followers10.3K
- Likes79.1K
Pinned Tweet
Ô Allah , accorde à notre vénéré Cheikh Mountakha Mbacké une vie longue, emplie de Tes grâces et d’une santé préservée.
BAAY SEEX AAJ retweeted
Ki gis lii, na xam ne ab yàq la te yàq la woo xam ne dafa soppi wax ji carrément !
ماساءا❌
ماشاءا✅
Dafa bokk ci xeeti yàq yi nga xam ne day soppi maanaa wax ji.
Partager🙏🏽
BAAY SEEX AAJ retweeted
Hello les coffee lovers ! ☕🤎
Bienvenue dans notre petit univers dédié aux amoureux du café ! 😍
On parle café, on partage du plaisir et surtout… on vous sert de bonnes saveurs ! 🔥
Si tu es team café, tu es au bon endroit ! ☕❤️
Abonne-toi et reste branché 👀
BAAY SEEX AAJ retweeted
Massalik Café est désormais sur X merci de suivre notre page pour une meilleure prise en charge de vos commandes et livraisons.
Pleins de cadeaux et de surprises vous y attendent !
BAAY SEEX AAJ retweeted
Kamil « Darul Minan » : 7 parties
Diwan 3 « Daarul Minan Xasaïdes »
Majmuha 22 « Daarul Himma »
BAAY SEEX AAJ retweeted
Étudiant en L3 avec l’arrêt de nos bourses j ai décidé d’investir une somme venez je vous vends des AirPods Pro 2 à seulement 5000 F au lieu de 7500 à 8500 F ailleurs
venez acheter si vous le pouvez et surtout
faites un RT pour me soutenir chaque geste compte🙏🏾❤️776058341
🤖 Made with AI
BAAY SEEX AAJ retweeted
Sëriñ saliou ag at yimu tollu di lire teere seex xaalil nekk source bu am solo ci école imaam maalik.
Kon nun nunu wara def? 🥹
BAAY SEEX AAJ retweeted
Enregistrement Nurud Dareyni
-Kurel sélection Nurud Dareyni (drouskat Nurud Dareyni Thies)
Son bi dina disponible fi aki fann @Ly_Ibraahima @s_sourang @moughniyan
BAAY SEEX AAJ retweeted
Jaalibatu yii noo ko móol; muy mbind mu
wér te taaru lool! Nu koy weccee benn 1500f
🙏🏿❤️
BAAY SEEX AAJ retweeted
Le vrai danger n'est pas seulement l'image créée aujourd'hui. C'est le mensonge visuel que nous risquons de transmettre comme une vérité aux générations futures.
BAAY SEEX AAJ retweeted
Ku gëm ni xaalis mooy lepp sañ naa def lepp gir xaalis,
Day melni société bi fexe na ba gëm loo ñu bari xalaat boobu, place biñ lay jox ci biir kër gi, famille bi, société bi Mingi tënku ci sa am-am, Loolu tax ñu bari di def lu nekk gir am ci ludul bayyi xel seen bakkan wala seen diine.
BAAY SEEX AAJ retweeted
NON, UNE FAUSSE IMAGE NE DEVIENT PAS AUTHENTIQUE À FORCE D'ÊTRE PARTAGÉE.
Des milliers de likes ne la rendent pas vraie.
Un compte connu, un écrivain ou un spécialiste du mouridisme qui la publie ne la rendent pas vraie.
BAAY SEEX AAJ retweeted
Si on te donnais 100K pour lancer une petite activité dans le contexte des JOJ.
Que ferais tu? Dit nous en commentaire avec les hashtag
#JOJ100Kchallenge
#Orangeconnect
Les gagnants repartirons avec 100 000 F CFA
Pour les débutant ou les TPE
Jury : @Nabyleu @s_sourang @zoubyben
Bonne chance fam
BAAY SEEX AAJ retweeted
Bu njëkkoon jaamu Yàlla mooy def ay jëf yu rëy ; sunu jamono yii nag, jaamu Yàlla mi ngi ci moytu yu bon yi. Booy xool bàyyi lu bon moo gën a jafe sax def lu baax.
Sang bi ﷺ nee na : «bis nit ñi dinañu àgg foo xam ne ku téeye diineem day mel ni ku ŋëb aw xal.» [Tirmiisii:2260]








































