Pinned Tweet
Maximum de Rt🚨
C'est la mère de mon meilleur ami
Kon sama yaay la, ni doomam lama defoon
2009 batay dji may bindi tweet guii, degg ñu ko, guissu ñu ko
Xamu ñu ndax migui dundu wala...
Waaye daal nigui rafeet njort
Ci ndigalu doomam laa def Tweet gui
Di ci sàkku ñaan ❗
Jarga ! retweeted
🚨Bismillaahi murids
Ño gi yëggal murids yi ag soppeey Seex Mustafaa Fall Mbar yëpp leggey bii ko murids tambalil ci Jannatul Mahwa Baay Fall Ga girr Serigne Bi mën fa taxawoo leggeyu Ndogou Seex Ibra Fall yi ci weeru Koor Gi.
Jaayante Bi
Wave/Om 78 187 15 41 Meïssa Ndiaye📌
Sénégal tu te blesses au genou et les gens te disent boy demal yeugg montagne nga renforcé ko , xoolal thiokki thiokki ndank rek ak arrière rek … !
1
303
Jamono gu nek , yalla saa borom migui nuy xeewalé ay nittam.. ñoo xamni nitt yu sell lanu té baax , ku leen topp baax , agg ci yalla , am ngëram .
Te nitt yooyu nigui fi , lakatu wunu.
Lay amul dh !
Amna ñoo xamni leep lun dundu ci journée bi , dinan ko rendre compte réseau sociaux yi surtt X ..
😏Nan yeewu tmt !
2
302
Jarga ! retweeted
POSE PREMIÈRE PIERRE DU CENTRE MÉDICO-SOCIAL🏥✨
Une étape historique dans la réalisation de notre engagement au service des populations.
Jarga ! retweeted
Moi qui pensais qu’en médecine, après la soutenance, c’est directement la fonction publique, or il y a des étudiants qui chôment après ça au Senegal
Jarga ! retweeted
Visite ce Samedi 21 novembre 2026 de Serigne Amdy Khady Fall à Kënzub Kitaab( kër Alquran)
Jarga ! retweeted
Sëriñ Amdi Xadi Faal xalif seneraal dee Baay Faal mo setsi woon murids yi ci leggeyu Kërug Al Quran Gi ko Seex Muhammadul Muntaxaa di liggeey lo❤️🙇🏾
À l’époque ( vers 1945 ) au Sénégal , la somme d’argent 5000fr représentait une somme très importante .
Par estimation combien représenterait cette somme aujourd’hui ????
1
292
Jarga ! retweeted
Les médecins contractuels du ministère de la santé n’ont toujours pas reçu leurs salaires et nous sommes le 21 aujourd’hui 🤦🏾♀️
Tchi niou yor jaboot am ay sokhla
Le Sénégal c’est tellement du foutage de gueule bordel
Té sougn togué seine keur yi deuk bi yeup dal seine kaw 🤦🏾♀️🤦🏾♀️
Jarga ! retweeted
🚨Bismillaahi murids
Ño gi yëggal murids yi ag soppeey Seex Mustafaa Fall Mbar yëpp leggey bii ko murids tambalil ci Jannatul Mahwa Baay Fall Ga girr Serigne Bi mën fa taxawoo leggeyu Ndogou Seex Ibra Fall yi ci weeru Koor Gi.
Jaayante Bi
Wave/Om 78 187 15 41 Meïssa Ndiaye📌
Jarga ! retweeted
J’ai un gros problème avec les médecins ici au Sénégal. Ils ne te donnent le diagnostic que quand tu le leur demandes. C’est à dire tu viens expliquer ton problème, ils écoutent, font ce qu’ils font et puis basta bindeul leu ordonnance mou diekh















