🦅 retweeted
ICE du noppalu ci tas njaboot yi ci dëkku New York. Du nu noppalu ci xeex ak ñoom.
Woteel ci Buum u Jokkoo u Taxawu ci Yoon ci wàllu Doxandeem ci 1-800-354-0365, walla nga woo 311 te wax ne “Immigration Legal” (Taxawu ci Yoon ci wàllu Doxandeem), ngir am ndimbal bu laajul fay, bés bu nekk, am na sutura.
Sunu dëkk waa New York lay jàppale.
























