
PanAfricaniste le piment de la vie est dans la variété🤪j'aime etre différente😍 #TALIBE_SERIGNE_SALIHOU
Senegal_dakar
Joined December 2017
- Tweets224
- Following355
- Followers191
- Likes490
🇸🇳Awa Mbaré retweeted
« Wakhal murid yi , ñu geuna faarlú ak googorlù ci jaamu yalla ! Fi ñu neek dee lu baax doufi dooy »
Seriñ Bassiru turee nèna dafa guent guiss Seriñ Saliou MBACKÉ (rta) mou waax ko li .
🇸🇳Awa Mbaré retweeted
Cheikhoul Khadim mi Sonko toudou si perchoir Assemblée nationale taye laay dooga dégue Président AN dieulko référence si AN té Serigne Touba manal sa bope sagnal sa bopp (souveraineté) réwmi si moom laniou ndieuka dégué si wakh ak si dieuf Machallah
🇸🇳Awa Mbaré retweeted
Ku bëgg yalla suturaal la dangay suturaal sa bopp, suturaal nit ñi,
Suturaal sa bopp mooy bayyi lu bon ta bula yalla nattoo banga def ko nga gaaw tuub ko, ta bañ ko siiwël.
Waaye dëkk ci def lu yalla di tere dina waral yalla xaw wi sa sutura dina tax bakkaar bu ndaw nekk bu mag.
فلا صغيرة مع الإصرار.
keen deefoul keen dara lou wayy deff bopam wakhii Borom TOUBA!! limou liguey kou ka nara yakk yaye yakou
30
🇸🇳Awa Mbaré retweeted
Ab soxna booko mënul teral, sagal, aar, jappale, jeema matal droits yiko yalla jox… bayyiko mu dem ci jamm.
« Et comportez-vous convenablement envers elles » S4V19.
🇸🇳Awa Mbaré retweeted
🚨☪️:DÉBUT DE JEÛNE LE JEUDI 19 FÉVRIER 2026
Serigne Mor Astou Toure le plus grand ASTRONOME de l’histoire
🇸🇳Awa Mbaré retweeted
Yalla na atum 2026 nekk atum sahaadatu daarayni
Ku nekk cu daaru dunyaa mu nekk sa sahaadatu ku jiitu daaru barzaq/ alaaxira mu nekk sa sahaadatu.
🇸🇳Awa Mbaré retweeted
🚨Touba : le Grand Magal validé à l’unanimité pour son inscription au patrimoine culturel immatériel de l’UNESCO
🇸🇳Awa Mbaré retweeted
"Saarou Ikhlass kouko diangal kou fébar mou moudié faatou si fébaar ba, dinane léral bamélam té dina mouthie si fitna bamél, maalaka yi niookoy rombalé siraate bamou dougou Aldiana".
Source: Silkoul Jawaahir (par Cheikhoul Khadim )
🇸🇳Awa Mbaré retweeted
« Bokk na ci ñakki ay teggin sa boroom:
1- nelaw bëcëg (Sieste) ta doo dundal guddi gi ci jaamu yalla.
2- nelaw ta gëmentuwoo lool ba nelaw yi ëpp la doole.
3- nelaw guddi ajjuma.
4- waxni: maa moom lii [sama nangam: kër, auto, téléphone, xaalis…]
5- waxni: lii damay lor [nangam day metti sama bopp, day tax duma mëna nelaw, damay febar…ndax yalla rek moo mëna lor jaam bi.]
Masaalik.
YALLAH sunu borom (SWT) mooma mom do saa borom! MUHAMMAH (saws) moy samab Yonnent!! Alxuraan moy sama tegtal moy sama njub!! Islam moy sama diine! Kaaba gi moy ssama xibla!!
1
88
🇸🇳Awa Mbaré retweeted
Guédiawaye : une marche annoncée pour exiger la dissolution de l’APR et un mandat d’arrêt international contre Macky Sall !
🇸🇳Awa Mbaré retweeted
La plupart des Sénégalais ont une mentalité révolue.
« Une langue est juste un outil mais pas un art à maîtriser » dit : Mariana Pascale
L’accent n’y était pas mais le plus important y était: un anglais clair et compréhensible »
Respect!🫡
🇸🇳Awa Mbaré retweeted
Mën nga nax ñepp bam des yalla ag sa bopp,
Loo def ci sa bopp lay dellu si, sa bopp ci yalla lay dellu.
🇸🇳Awa Mbaré retweeted
Took di xalaat xeewal yi la yalla defal ag di xalaat ñi nga tane dina dimbali nit ci jafe jafe aduna yi.
Fatte xeewal yi rek mooy waral jambat.
CAPPUCCINA BALLERINA VS TUNG TUNG TUNG SAHUR IN THE BOAT BUILDING CONTES... youtube.com/shorts/78yUcnLUX… via @YouTubémxl’vqtf’cqgvghlj mp
1
32















