Dr Maktoumist retweeted
Replying to @Adaah05 @mamesarrdiff7
Sokhnaa siii boul meussaaa décourager car meune guaa deim baaa diégué saa objectif guas retourner tei Maam borom Touba(RTA) dafaa daan wakhniiii*Celui qui se décourage vite ne sera jamais l’élu de sa génération* continue à chercher lèep dinaa bakh
Dr Maktoumist retweeted
Ñou jeuflanték yAllah gui nék si ñoun. Dafay Ballé, nañ di ballé. Dafay mayé, nañ di mayé. Dafa Juste, nañ juste. Kou beug lou raffet leu, nañ di raffétal. Xamé ko si lépp, déllo ko lépp parsk nous en sommes capables . Alhamdu lillAh 🤲🏿
Dr Maktoumist retweeted
Kouy liguéyé Ecobank fi mou diapalei ma tji dara svp 🥲 rt apprecié merci d’avance
Dr Maktoumist retweeted
Replying to @mamesarrdiff7
Bou lew ak bou lewoul yeup diafée...😂😂 mom kagn mom yalla rek lay nekh
Même pour un simple stage non rémunéré il faut gua am bras long. Sénégal kou amoul mental guédd sen lépp.
Dr Maktoumist retweeted
Nit ki buy feyu sax dafa wara mandu.
Lott bi bakkan lott ci natt mandute moo tax ñuy digle jeggale ndax mën nga fa jar for ay bakkaar, ci wax ag ci jëf, te jaruko.
Dr Maktoumist retweeted
Votre satisfaction est notre priorité ❤️🤲📌
Échange 11 pro max 256 vs 13 simple 256 valide ✅✅
Merci pour la confiance @6m_diop
Diaylaa Mayla accessoires 👏
























