Dr Maktoumist retweeted
Replying to @Adaah05 @mamesarrdiff7
Sokhnaa siii boul meussaaa décourager car meune guaa deim baaa diégué saa objectif guas retourner tei Maam borom Touba(RTA) dafaa daan wakhniiii*Celui qui se décourage vite ne sera jamais l’élu de sa génération* continue à chercher lèep dinaa bakh
Dr Maktoumist retweeted
Ñou jeuflanték yAllah gui nék si ñoun. Dafay Ballé, nañ di ballé. Dafay mayé, nañ di mayé. Dafa Juste, nañ juste. Kou beug lou raffet leu, nañ di raffétal. Xamé ko si lépp, déllo ko lépp parsk nous en sommes capables . Alhamdu lillAh 🤲🏿
Dr Maktoumist retweeted
Kouy liguéyé Ecobank fi mou diapalei ma tji dara svp 🥲 rt apprecié merci d’avance
Dr Maktoumist retweeted
Replying to @mamesarrdiff7
Bou lew ak bou lewoul yeup diafée...😂😂 mom kagn mom yalla rek lay nekh
Dr Maktoumist retweeted
Nit ki buy feyu sax dafa wara mandu.
Lott bi bakkan lott ci natt mandute moo tax ñuy digle jeggale ndax mën nga fa jar for ay bakkaar, ci wax ag ci jëf, te jaruko.
Dr Maktoumist retweeted
Votre satisfaction est notre priorité ❤️🤲📌
Échange 11 pro max 256 vs 13 simple 256 valide ✅✅
Merci pour la confiance @6m_diop
Diaylaa Mayla accessoires 👏
Dr Maktoumist retweeted
Une collègue a fait un envoi Pi-Spi de son compte CBEAO vers Wave depuis Vendredi. Son compte a été débité mais elle ne trouve pas l’argent sur son compte Wave. Son gestionnaire lui dit qu’il ne peut rien à cette situation. C’est quoi la solution maintenant ? @malosn
@Noo_IDcard
Dr Maktoumist retweeted
Boo yoré xaliss diambour waxko jour tel nala diox la moindre des choses même bo yoroul msg ko waxko amago mais daniouy yorr sa xaliss nga fayékou lén niou merr ba parei fi tangal sa xol
Dr Maktoumist retweeted
Guddi altiné donté ni ben salatul fatihi nga meun, defko bala ngay teud hadiyaal ko Yonent YaAllah Muhammad ﷺ ﷺ ﷺ🥹💚
Yalnaniu Buur YaAllah bolei ci gni seen turr di yegg ci mom ﷺ ﷺ ﷺ ba mu tuddu niu ci hadaraat yeup🥹
Dr Maktoumist retweeted
Arrêtons de donner de faux espoirs à ces personnes en or. 💔
Miinal nit ki sa bopp, créer une complicité, donner de l’affection, de l’attention, faire naître des sentiments… puis, du jour au lendemain, disparaître comme si rien ne s’était passé. Parfois, on ne réalise pas à quel point cela peut blesser.
Aimer une personne n’est pas toujours facile, surtout lorsqu’il existe une dépendance affective. Quelqu’un à qui l’on s’attache peut avoir un impact sur notre humeur, notre tranquillité d’esprit et même notre santé mentale.
On ne peut pas obliger quelqu’un à nous aimer, mais on peut au moins faire preuve de sincérité et d’honnêteté. Si vous ne souhaitez pas aller plus loin, dites-le simplement. Une vérité peut faire mal, mais un faux espoir peut laisser des cicatrices. 💔
Soyons attentifs aux sentiments des autres. On ne sait jamais ce que quelqu’un traverse intérieurement. ✨
Et puis, le karma existe ! Oui, le karma existe. Chaque geste compte, et personne ne devrait avoir à payer le prix de votre manque de sincérité.🙌🏿❤️




















